|
|
|
|
|
LES DONTS DE CHEIKH BETHIO SUR SALIOU
22/04/2009 15:21
THI WAKH SERIGNE SALIOU:
Néna cheikh bethio kou diébalou thi yaw amm ngueureumal yalla .
koula guiss dém aldjiana , koula kham dém aldjiana ,koula tope dina ma nopal fi ak fé gnou dieum ( ceux qui te font allégeance , en verité font allégeance a allah la main d allah est dessus de leurs mains)
| |
|
|
|
|