DIEUREDIEUFETY SERIGNE SALIOU .
SERIGNE CHEIKH BETHIO DIAMOU SERIGNE SALIOU YALLA NAFI YAGUE TEE WEER.
SERIGNE TOUBA mi done sackou dieumi SERIGNE SALIOU mo sackou walé wone HEUKHELOU CHAKIRINE gni di thiantakune ya gnou wathialé ak mom thi moulck kaw souf santélako yalla mi serigne saliou.
SERIGNE BETHIO GNOU TAKHA GORE:
Ndakh yagnou délo sougnou thiossane thi serigne saliou mi gnou rérone .
Ndakh yagnou khamal serigne saliou té koudoul serigne saliou khamoul serigne bay khamlé serigne saliou .
Wayé tamit koudoul serigne saliou meunoul diamou serigne saliou baye éguélé thi serigne saliou .
SERIGNE BETHIO GNOU TAKHA:
Ndakh yagnou déf des connaissants thi sa thiante gui bilaye thioune nous sommes reconnaissants khana dila santaty bou wéér.